Baay gaynde ak jenax
Esta parte es el arranque que tienen todos los cuentos en wolof.
Contacuento: -Léeboon
Público: -Lippoon
Contacuento: -Amoon na fi…
Público: -Da ana am…
Ba jenax guénee cha paxamma, jakaarlook baay gaynde, cha la xam ne tay lakoy sakal péxe.
-Cha saas ya lako né: Baay Gaynde, jéguël ma buma lekk! Bës da na ñëw, dinaa la amal jarín.
Baay Gaynde neko:
-Bann jarin ngamay amal, néew doole?
Bako baay gaynde xoolee chi kaw ba chi suuf, yërmandee tax mu baal ko.
Bañu cha teguee ay fann, jenax degg choow lu bare lool.
Bamu yeguee cha berëp ba, chala seen Baay Gaynde, ap mbaal umb ko.
-Dana la xétali! lacha tek.
Baay gaynde neko:
-Yaw, néew doole!
Cha la jenax tambalee dagg baal ma ak bëñ ya, ba xétali baay gaynde.
Cha gudi guoogu ba tey, lañu nekk ay xaritu benn bakan.
desde la Ong Sevilla Acoge, Ousseynou Dieng nos lo contó en wolof y nos hizo mucha ilusión
ResponderEliminarfantastico iba a buscar quien lo podia traducir pero yá lo teneis asique aprovecho y lo voy a poner en el muro de la asociación gracias :0))
ResponderEliminarAccording to most sources, the start should be:
ResponderEliminarLééboon ! Lippoon! Amoon na fi! Daan na am!